Home Page »  Y »  Youssou N'dour
   

Undecided (Japoulo) Lyrics


Youssou N'dour Undecided (Japoulo)


né japoulo, té bayi wo
sé deng, deng dé japoulo, té bayi wo
né noboulo, té bayi wo
sé deng, deng dé japoulo, té bayi wo
han sé deng, deng, sé deng, deng, sé deng, deng, sé deng, deng(fois 2)

hé yaw li nga japone ba mél ni
hé yaw boulko bayi té jiknala(fois 2)

né noboulo yaw bayi wo
sé deng, sé deng té bayi wo
wouye noboulo, yaw bayi wo
sé deng, sé deng thiey bayi wo

waw sé deng deng, sé deng deng, sé deng deng, sé deng deng

noboulo, bayi wo
sé deng, sé deng yaw bayi wo
né noboulo yaw té bayi wo
sé deng, sé deng yaw bayi wo
waw sé deng deng, sé deng deng, sé deng deng, sé deng deng

hé yaw li nga japone ba melni
hé yaw boulko bayi té jikna la(fois 2)

la la la la la la la la la mani yeksil sét
la la la la la la la la mani dougal sét
la la la la la la la la la ma ni yeksil sét

kham nga ko, kham nga ko, kham nga ko
kanam dou kasso wayé kouka sétlou guiss ko(refrain)

Most Read Youssou N'dour Lyrics
» Kids
» Bamako
» Birima
» Set
» Yama


smell like your favorite singer: fragrances inspired by music icons
Smell Like Your Favorite Singer: Fragrances Inspired By Music Icons
Chris Page - 03 Nov 2025
inside the mansions of america’s richest singers
Inside The Mansions Of America’s Richest Singers
Sasha Mednikova - 28 Oct 2025
white house rejects claims of trump considering clemency for diddy
White House Rejects Claims Of Trump Considering Clemency For Diddy
Faith Thompson - 21 Oct 2025
decoding the blockchain beat: how crypto composes a new music era
Decoding The Blockchain Beat: How Crypto Composes A New Music Era
Evren E. - 17 Oct 2025
katy perry teases justin trudeau romance rumors at london concert
Katy Perry Teases Justin Trudeau Romance Rumors At London Concert
Sasha Mednikova - 14 Oct 2025
Browse: